LES CHIFFRES
Un | Benn |
Deux | Ñaar |
Trois | Ñett |
Quatre | Ñent |
Cinq | Juroom |
***** | |
Six | Juroom benn |
Sept | Juroom ñaar |
Huit | Juroom ñett |
Neuf | Juroom ñent |
***** | |
Dix | Fukk |
Onze | Fukk ak Benn |
Douze | Fukk ak Ñaar |
Treize | Fukk ak Ñett |
... | |
Vingt | Ñaar Fukk |
Vingt et un | Ñaar Fukk ak Benn |
Vingt deux | Ñaar Fukk ak Ñaar |
Vingt trois | Ñaar Fukk ak Ñett |
... | |
Trente | Fanweer |
Trente et un | Fanweer ak Benn |
... | |
Quarante | Ñent Fukk |
Cinquante | Juroom Fukk |
Soixante | Juroom Benn Fukk |
Soixante Dix | Juroom Ñaar Fukk |
.... | |
Cent | Teemeer |
Cent cinquante | Teemeer ak juroom fukk |
Cinq cents | Juroomi teemeer |
Mille | Junni |